Tegtal bu leer
JIESAI Choc azote électronique (plaque d'acier)
Bi off-road duggee ci jamonoy xarañteg xel, tuning suspension dafa soppeeku. JIESAI ak mbégte la genne Electronic Nitrogen Shock (version Steel Plate), di dooleel performance hardcore ak xarala yu bees ngir joxe jaar-jaar bu jaar yoon bu musul am ci ñi bëgg off-road.
ñu defaree ko ab structure core buacier alloy à haute résistanceak boole ci bracket plaque asiye bu dëgër, Amortisseur bi dafay baax ci anam yu metti yu melni terrain bu am xeer, gravier, ak potoxo. Diametre tube bimu am 2.5 puus dafay gëna yokk doole amortissement bi ak gaawaayu dissipation tàngoor bi, di mëna dékku stress structurel biy bawoo ci vibration yu metti yi, ba noppi di joxe wóolu sa bopp budul yëngu sooy push àpp bi. amdayo kompresioŋ buñ saytu ci anam elektronik, dina dindi jafe-jafey tuning manuel bu yàgg bi. Sooy daw ci otoroute yi wala nga jàll ci yoon yi nekk ci off-road, mën nga xawa jekkal amortissement compression bi jaaraleko ci seytu elektronik: reglage bu gëna nooy dafay tax dawal gi neex, te neex ci trotoire bi, ci noonu la mode bu gëna dëgër di joxe tëye bu amul fenn ci senaario off-road, gëna yokk stabilite ak paas oto. Rax ci dolli, 1.5"–2.5" lift range bi dafay yokk clearance bi ci suuf, ba noppi may oto bi mu mëna ànd ak cadre off-road yu gëna mag, loolu tax oto bi mëna jàll piste yu gaaw yi, ravin yi ak yeneen peyisaas yu xawa jafe ci anam wu yomb. Sooy dugg ci tukki bu sori ci àll bi wala nga def piste off-road profesionel, JIESAI Electronic Nitrogen Shock (Steel Plate) mooy sa àndadoo bi gëna wóor, di fësalaat ay peggu off-road ak dooley xarala yu bees ak feesal bépp tukki ak wóolu sa bopp.

Etiketu produit 1:
njëg:
15600
Acier alloy à haute résistance
AT="" scroll="" auto="" padding-box="" background-color:="" class=" list-paddingleft-2">Tabax bu njëkk: Acier alloy bu am doole + bracket plaque asiye, 2.5" tube ngir jàppale bu dëgër ak baña dóor.
Adj. kompresioŋ elektronik: Kontrôle elektronik ngir ajustement amortissement kompresioŋ bu jaar yoon.
Lift bu yomba soppeeku: 1.5"–2.5" lift ngir yokk gaawaayu suuf si ak gëna yaatu ci pëno yi.
Performance Tech-Forward: JIESAI-ñu defar ko ngir mu mëna wóolu sa bopp ci off-road.
Ndimbal yëkATi:1,5" - 2,5"